Wolof : lexique (F)
Cliquer sur les lettres pour écouter les mots.
français |
wolof |
prononciation |
femme |
jigéen j- |
|
femme (épouse) |
jabar j- |
|
fendre |
xar |
|
feu |
safara s- (ou w-) |
|
feuille (d'un végétal) |
xob w- |
|
fleur |
tóor-tóor b- |
|
flotter |
tëmb |
|
foie |
res w- |
|
frapper |
dóor |
|
froid (être) (température) |
sédd |
|
frotter |
bomb |
|
fruit |
doom b- |
|
fumée |
saxaar s- |